Sahaaba Group

Chaine la buy jàllale bépp xew-xew (conference, màggal, cant, gàmmu génté, céet ...) ak lu ci mel ni publicité moo xam affiche wala leneen.

Jokkool ak nun Gisël sunu liggéey

Mockup
Li nuy def

Jëfandikooku yi

Solusio bu mat, bu jub — dale ko ci xalaat ba ci jottali.

Shooting foto & video

Reportaj sàcc, portrait, foto produkt, video multi-camera.

Publicité & Branding

Sartuwa pano publicité, spot publicité, produksio ak scenarisasio.

Waxu jëfandikookat & Postproduction

Waxu jëfandikookat ci ay làkk yu bari, mixage, mastering, soppali audio.

Sunuy ligéey

Portfolio

Bokk ci benn séance

Naka la Sahaaba Group di liggéeye

Benn équipe créatif lanu, bu leen di jàppale ci seen mission ak seen communication visuelle. Dale ko ci saartuwa ba ci jottali ga--nuy dimbale sunu client ngir seen bataaxal am doole.

+100

Xew-xew ñu dékk

+600

Pano ñu sartuwal

+50

Waxu jëfandikookat ñu def
Sunuy équipe

Laaj "benn devis"

Waxal sa projet dananu la toontu ci whatsapp bu baax.

Xibaar yi

+221 78 635 84 06

contact@sahaabagroup.com

Touba Sourah, Sénégal

Jokkol ak nun ci whatsapp